Youssou Ndour - Waññi Ko (version lyrics)

Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,

te bés bu ne , benn xar nga daan añ e

nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée

yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine

am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann

nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,

· nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée

te waa nations - unies , nga ka daan loué

· te diggënté , États-Unis ak Guinée ,

daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois

na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs

na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs

techniques yooyu , japon laa ko jànge

ca yooya jamono , man la ñépp di wër

lu ñu wax nga ni fekke nga ko

fu ñu wax nga ni dem nga fa

doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;

waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.



Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,

Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.

Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al

Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.

Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.





ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla


Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
www.youtube.com/c/YoussouNdour...
youssoundour...
youssoundou...

Descargar

Vistas
1,231,560

Comentarios

  • King of Africa

    Omar ThiamOmar ThiamHace 51 un minuto
  • Ak fi diamono tolou amneu solo machalla nagnou défarat djiko yi lou s4ordinaire bilay ioe

    salamsalamHace 56 minutos
  • 🥰🥰🥰

    Mame khary MbodjiMame khary MbodjiHace 5 horas
  • Papa yousou Dal ya mana way

    Oumy FayeOumy FayeHace 6 horas
  • Éternellement le meilleur...you est un don du ciel...quel talent!!!!!❤️❤️❤️

    Matabara DiopMatabara DiopHace 6 horas
  • Wanniko

    Ibrahima GueyeIbrahima GueyeHace 17 horas
  • Ma chaallah

    salimata barrysalimata barryHace 19 horas
  • Je m'aime bien cette musique je l'écoute sans arrêt 🎤👍🏾❤️🇸🇳

    Djibril KonateDjibril KonateHace 22 horas
  • Machalla

    Kara Mbacke MbayeKara Mbacke MbayeHace 23 horas
  • Mafi nè papa you longue vie a vous j aim💕👍💫

    bik momo joopbik momo joopHace 23 horas
  • Ge suis très content de you par ce que il aide la population sénégalais

    Sheiktijan SannehSheiktijan SannehHace un día
  • Merci le roi de tout les temps

    Sheiktijan SannehSheiktijan SannehHace un día
  • ❤️

    Saikou chaaSaikou chaaHace un día
  • ❤️❤️

    Diop MoussaDiop MoussaHace un día
  • Mbaye gueye faye ya bon rek😂😂😂

    Sangu îls fatickSangu îls fatickHace un día
  • aka meune woy

    ablaye22 sarre22ablaye22 sarre22Hace un día
  • J'ai retrouvé les lignes de basse du grand HABIB (RIP)

    Momo DoumbisMomo DoumbisHace un día
  • Yousso khana oussmane sonko laye wakhal

    modoudal76modoudal76Hace un día
    • meuna nek ndak day fène rek

      Mamoudou DialloMamoudou DialloHace un día
  • Youssou nd rre

    Mamadou DialloMamadou DialloHace un día
  • Youssou ndour dou woye si 0 zero

    DJ ADO SénégalDJ ADO SénégalHace un día
  • international chanteur du monde plus riche en Afrique

    Alex AlexAlex AlexHace un día
  • ROI DU MBALAX ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    Moustapha SeckMoustapha SeckHace un día
  • Walahi c'est un roi MADIBA depuis MAURITANIE

    Madiba DibaMadiba DibaHace un día
  • Tonton You Text bi tamit wanniko katanam bari lolou té dou yeureumé. Wadji doutouko défati

    Mohamed NokhoMohamed NokhoHace un día
  • Qui a constaté le cri de Assane Thiam 1:57 Super Etoile, Quelle complicité 😂😂😂

    Mouhamed SeckMouhamed SeckHace un día
  • Mets le nom de la personne bi nga beug mou wagni )= =)

    adji mariama dembaadji mariama dembaHace un día
  • El phenemeno Youssou le meilleur

    Idrissa DiackIdrissa DiackHace 2 días
  • Roi way 🤩

    baye ndiaga sk skbaye ndiaga sk skHace 2 días
  • Machaala

    CLARISSE SYLVACLARISSE SYLVAHace 2 días
  • Moi je dis juste, Grand Youssou Yalla nga goudou fane yake sa Ndiabote.❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

    Awa NdiayeAwa NdiayeHace 2 días
  • Non comment il est fort ce monsieur merci Youssou pour ce tube

    ameth gueyeameth gueyeHace 2 días
  • Amadou sylla

    Amadou SyllaAmadou SyllaHace 2 días
  • Thiey youssou 🥰🥰🥰

    diallo seynaboudiallo seynabouHace 2 días
  • Le meilleur de sa génération

    Adama KasseAdama KasseHace 2 días
  • Na bahi politique neique ci côté askane wi

    Badou MbayeBadou MbayeHace 2 días
    • @Badou Mbaye Youssou a au moins a créé des emplois avant Macky. Et il n'est pas des genres qui fait du social devant les projecteurs. Je me demande quel raisonnement tu prônes. On accéde au pouvoir pour régler les problèmes des sénégalais. Donc pour toi toute politicien qui prend le pouvoir n'est plus du coté du peuple si je comprends bien ta définition. Dommage mais le peuple c'est l'ensemble des senégalais. Meme dans les superpuissances il y a des pauvres et des riches donc etre du peuple ne veut dire etre pauvre

      Mamoudou DialloMamoudou DialloHace un día
    • Askan wi dou sonko. 14morts pour mortelcombat . L histoire retiendra

      bou kene merrbou kene merrHace un día
    • Pour moi le peuple c'est les femmes qui accouchent sur des charettes,les gens malades qui n'ont pas les moyens de se soigner, ceux qui n'ont rien à manger, c'est à dire ceux qui ont besoin d'aide pour moi youssou ndour devait être un député du peuple ou médiateur pour l'intérêt du peuple avec le gouvernement mais malheureusement il est à côté du pouvoir pour son propre intérêt

      Badou MbayeBadou MbayeHace 2 días
    • Pour yaw nekoul si côté askan wi? Pour vous le peuple c'est les opposants. Le peuple c'est l'ensemble des Sénégalais nak.

      Mamoudou DialloMamoudou DialloHace 2 días
  • UN GRAND MESSIER, UN GRAND FIGURE MONDIAL MERCI LE ROI DU MUSIC AFRICAINE

    Cheikh MbengueCheikh MbengueHace 2 días
  • Machalla Nekhna félicitations notre Ambassadeur international ♥️♥️♥️♥️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏🙏

    Arame SeckArame SeckHace 2 días
  • Techniques yooyu,japon laa ko jange 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💪💪Yusu y yal na nga fi yaga🙏

    Abdou JagneAbdou JagneHace 2 días
  • Bilayi do sén moroom plus d'un million de vue en une semaine

    Gorgui gorguiGorgui gorguiHace 2 días
  • 💞💞💞💞💕💕💕💓💓💗💗💖💖💖💟💟💟💯💕💞💞💓💗💖

    Oumou DialloOumou DialloHace 2 días
  • 👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑

    Akeum DiopAkeum DiopHace 2 días
  • Chapeau

    Madiba DibaMadiba DibaHace 2 días
  • Wa ana Assana Diouf🤪 degloul wouywi

    zaalbi boyzaalbi boyHace 2 días
  • 😘😘😘

    modou seckmodou seckHace 2 días
  • Le mythe🤢❤

    Mouhamed lamine SyMouhamed lamine SyHace 2 días
  • Kinnnnnnnnnnnnnnnnnnng Moy King bi deeeee

    Mbaye WadeMbaye WadeHace 2 días
  • Khalife général koulou mbalakh mane kou d’accord laleule ❤️

    Fatma SowFatma SowHace 2 días
  • Thiéy NDOUR !!! Y’aaaayyyy Séne baaayyy .

    Eilk MinosisEilk MinosisHace 2 días
  • Super machallah mdrr

    Tafisco BayakhTafisco BayakhHace 3 días
  • Champion de monde

    Manar DiagneManar DiagneHace 3 días
  • Le meilleur de sa génération et de les temps respect père 🙏🏾

    dioufy sarrdioufy sarrHace 3 días
  • Youssou Ndour ya KO wara wanngi tu es un grand scros tu a encaissé bocoups d'argent sur wave gratuitement la plateforme que tu propose n'es pas fiable on téléchargé des chons qui n'es pas lisible... Il faut spliqué sa et le réglé

    Abdoul SarrAbdoul SarrHace 3 días
  • Chère Youssou Ndour on j'ai acheté l'album maïs le single téléchargé ne se lis pas,donc you on fait comment tu a encaissé mon argent s'en rien en retour

    Abdoul SarrAbdoul SarrHace 3 días
    • Tu change de portable c'est mieux

      Sankare MohamedSankare MohamedHace 20 horas
  • Nice 🤩😘🥰

    Soldja Baby sicarioSoldja Baby sicarioHace 3 días
  • Welcome back le roi des mbalax we love you 😘😘😘😘😘😘

    Nabiha NjieNabiha NjieHace 3 días
  • KING suma woii katt bi Marsha'allah

    alaji bahalaji bahHace 3 días
  • Deug deug deug deug deug deug deug, Youssou, andina bi bamou dath, yafi dakha weuye teigou ci Michael Jackson. J'ai jamais entendu une voix aussi extraordinaire que celle-là. Wayei tmt, Super étoile keine deimoule ngueine deiss yeine tmt. Bouba Ndour saï saï music bi, iow yaye le meilleur producteur musical de tous les temps au Sénégal, les preuves sont palpables.

    hadj kebehadj kebeHace 3 días
  • Le corrompue manteur

    oni madoni madHace 3 días
  • The best

    Mass DIOUMMass DIOUMHace 3 días
  • Thieyy andou super étoile bou yokouwoul dall d'où wanjiekou mancha ala

    Malick SeneMalick SeneHace 3 días
  • Ça voie reste toujours le même

    KHOSS MUSICKHOSS MUSICHace 3 días
  • Iolmm

    Souadou NdiayeSouadou NdiayeHace 3 días
  • Cey you kene meunou la merei. Mais pour le clip il faut patin quoi Di na nice deh.

    malick ndiayemalick ndiayeHace 3 días
  • Un chef-d'œuvre 🤭👍💪♥️♥️💯

    Ahm MoussAhm MoussHace 3 días
  • Kone you kafoul Doulkatt yii la woyy 😂😂

    Mamadou BaMamadou BaHace 3 días
  • Nice😍😍😍

    Ibrahima GueyeIbrahima GueyeHace 3 días
  • Deuyzeukoulanah Youssou ndour bilahi ma le begue yow Lo way mou néx🥰 kou daccord ke Youssou ndour est le meilleur 🔥

    young wizz taylor!young wizz taylor!Hace 3 días
  • The king of king. Notre fierté youssou ndour

    aliou diedhioualiou diedhiouHace 3 días
  • Père You bi Patin mo wara Def clip bi 😂😂😂😂😂

    Kawsy SyKawsy SyHace 3 días
  • Le maestro r.a.s

    Papa Armand NiangPapa Armand NiangHace 3 días
  • Sublime tout simplement

    Mariama DiaMariama DiaHace 3 días
  • 🤣🤣🤣 ki dh graw na wañiko bro ( je parle du mec qui mytho pas de youssou ndour )

    drk_momodrk_momoHace 3 días
  • Kounkandé wouyoul fii🤣🤣🤣

    Fatoumata BaFatoumata BaHace 3 días
  • 🔥🇸🇳👌🎩

    Thierno BaThierno BaHace 4 días
  • C'est bien papa

    SayaNE KaSayaNE KaHace 4 días
  • King

    Papis GueyePapis GueyeHace 4 días
  • ❤️🔥

    Loga VogueLoga VogueHace 4 días
  • Tu es le meilleur notre patrimoine national

    DIERE GUEYEDIERE GUEYEHace 4 días
  • Son bi kounkandé lan KO wayal

    samba sanésamba sanéHace 4 días
  • Le plus grand regret que jai ds ce monde c'est de ne pas parler wolof juste pour ecouter ses chansons. Je n'ai jamais rater un de ses concerts ds le continent Americain. Chaque live que j'y vais est comme la 1ere fois que je le vois. God bless him!!!!

    Alpha NayeteAlpha NayeteHace 4 días
    • Youssou de toutes les générations. Le meilleur de toujours et pour toujours.L ongue vie et santé

      Thierno SeydiThierno SeydiHace 2 días
  • Une chanson de haute facture à l'image de la carrière de l'homme. Pour ceux qui comprennent les parole, c'est encore plus magique. Youssou ndour au-delà de sa voix unique une plume. Il réussit à transmettre des émotions et du sens à travers sa musique. Son génie est de mettre aussi des contenus qui parlent à tous.

    Aboubacar ToureAboubacar ToureHace 4 días
  • Machalla❤️🤍🤍💝💓💞💕💐💮🌺🌸⭐⭐

    Ndioufa SarrNdioufa SarrHace 4 días
  • Machala

    Bass NdiayeBass NdiayeHace 4 días
  • Do dara

    Moustapha DiopMoustapha DiopHace 4 días
  • Machallah machallah le meilleur

    alioune fallalioune fallHace 4 días
  • Khana il explique les parole d'un jinn

    fatou diankhafatou diankhaHace 4 días
  • Dafa lèr You yaye sen mame Di sen baye Ki dou morome way The king 🐐

    Capo ElcapoCapo ElcapoHace 4 días
  • Very nice music 🎶

    Ali NjieAli NjieHace 4 días
  • Au moment de tourner le clip svp prenez koukande jap len ci rek il ferait un très bon acteur

    Salimata AlbisSalimata AlbisHace 4 días
  • Grande youssou ndour do moromu gayi

    Talla GueyeTalla GueyeHace 4 días
  • Yousou n'dour stop this nonsense, this music is about propaganda, were so intelligent we know who you are talking about,

    Hadim TourayHadim TourayHace 4 días
    • Do tell us pls

      Oumie HairyOumie HairyHace 4 días
  • Ça c,est pour macky sall le chachon

    Hadim TourayHadim TourayHace 4 días
  • X

    Thierna DoucouréThierna DoucouréHace 4 días
  • X

    Thierna DoucouréThierna DoucouréHace 4 días
  • 🇸🇳❤️

    Eldifa DiengEldifa DiengHace 4 días
  • Machallah l meilleur je l suit depuis Mauritanie

    Rameses SallRameses SallHace 4 días
  • Tope nice

    Fall ManeFall ManeHace 4 días
  • wanniko le wolof une langue riche diminuer decompter detourner demitour

    Gorandiaye EnligneGorandiaye EnligneHace 4 días
  • Très bon nouveau single de Mr Youssou Ndour très très bonne musique notamment les percussions et cuivres a l'arrière félicitations à toute l'équipe et au musiciens

    Pierre DupontPierre DupontHace 4 días